Associazione Camera a Sud
Yonyu yombu pour muslu si diangoro cronavirus niongui ni. Badara beneu yombal katu wahktaan la di ligueye si progetto F. A. R. I bi. Pour muslu si yoku diangoroji sunu dimbalantè am na si solo bu bakh ||| Per prevenire e contrastare il contagio da #coronavirus è importante la collaborazione di tutti. Badara Jobe mediatore linguistico culturale in ambito sanitario, collabora con Camera a Sud Aps di Lecce per il progetto FARI. In questo video spiega in wolof alcune semplici raccomandazioni
——————————
Ai conseils yu yombeu pour nyu bangneu walate cronavirus bi
– Raxhasal sa ai loxho sasune ak ndoxhu sabu wala ngua djeifandeku gel bu
am alcol si biir
– Bangnelen di djeiguewante te nguen bayi distance bu 1 metre si sen
diguante
– Bulen laal sen ai beut, bakeune ak seni ai loxho
– Eviter len ai palace yu beuri ai nit
– Bangnelen di dioxhewante ai loxho wala di acole wante beu emergence bi
degne
– Bo amei ai diambaat yu melni sotch togal sa keurr. Bul dem si h’ospital bi
wala si ai studio medecins. Wotel sa medecine general, pediatre, garde
medical wala numero regional yi
– Djeifandekulen ai mouchoirs pour teij sen ai guemengne ak sen ai bakeune
sa’yolen tisoli wala bolen di seuxkat. Wala ngua bankeu sa coude pour
couvrire sa guemenge bi
Source